30 décembre 2024

Seneinfo

Restez toujours informé

Akhirou Zaman: Mouhamed M sakho Lance un message fort

Bi Diamono Kou Gannayo Woul Nienti(4) yeux Ladakh lakk leu:
Xamxam, Fit, Foulla, Doylou

1, Bo Amoul XamXam Niou Nakhla
2, Bo amoul Foulla. Niou Fowé-la
3, Bo Amoul Fit Niou Xeubeul-la
4, Bo Doylou woul Niou Dieundeu-la